*GambieđŹđČ : diogantĂ© yin doon Amal çi gaawou(samedi) bii le 09 Avril ngir tĂ nn Ay dĂ©putĂ©s parti bou Adama Barrow moo djiitou doontĂ© Amoul li euppou « sans toutefois obtenir la majorité » Amna 18 dĂ©putĂ©s ci 53 dĂ©putĂ©s yin fal , parti koudiĂ© gui , lâUDP Ousainou Darboe djiitĂ© ko Amna 15 siĂšges , NRP Bou Hamath Bah am 04 dĂ©putĂ©s , PDOIS 02 dĂ©putĂ©s , LâAPRC Bou Yahya jammet am 02 dĂ©putĂ©s , yeneen parti yi koubnĂ© am bĂ©nn dĂ©putĂ©s … , ci Ă©lections yi rĂ©ewoum Gambie Amoon na 957.167 Ă©lecteurs 1 555 bureaux Ak 246 candidats you doon xeujjoo , ci fatali 58 members yi Bokkou ci assemblĂ©e nationale bi 5 yi prĂ©sident Adama Barrow mokoy tĂ nn mou bokkou çi prĂ©sident assemblĂ©e Bi .*
*Fallou Walf Sall bou fatima xibaaru réew mi*